Auteure & Compositrice: Ridia Na Réalisateur: Mao Prod Direction Artistique: Ridia Na Make up & Stylisme: Dieynaba Sow Acteur: Malick Ndoye Groupe de dance: Ndaat Saay Crew Remerciements: le groupe Jamm, le Cube Dakar, Mme Seck Awa et toute l’équipe management ainsi que les figurants✨ Lyrics: Mmmm mmm mm yeah Ladji.... Gooro goor yay sén boss Diantal ba diss mon beau gosse Paré wouma reube la pour sooy Bayil mou noye May nek thi sa khol Oublie les autres c’est mort Et je te défie mi amor Pour un corps à corps Dink ma sa khol gnouy weur di blow Ma nek sa goe Gneup tek bët ni ma la tipo Tipo appo Je te promets qu’on vivra des folies Et je te suivrai partout et toute ma vie Ladji kopati, sa sarakh bi momay danel tikko fi Ma diap chill eh ehhh Amsa thiopati Say say bi momay danel tikko fi Ma diap chill eh ehhh Li rek moy li fort Beug leu piir ba mouy moom Paré nak dekkou coup du sort Encore et encore Yeuketila athie thia kaw Doon sa talibé dila rammal Samp sama ndeud rek ngir yow Boulay nekh mouy moom Dink ma sa khol gnouy weur di blow Ma nek sa goe Gneup tek bët ni ma la tipo Tipo appo Je te promets qu’on vivra des folies Et je te suivrai partout et toute ma vie Ladji kopati, Sa sarakh bi momay danel tikko fi Ma diap chill eh ehhh Amsa thiopati Say say bi momay danel tikko fi Ma diap chill eh ehhh Oh oh ohhh Ohhh oh oh ohhhh Mmm mmm Oh oh ohhh Ohhh oh oh ohhhh oh oh ohhh Euh euh euhhhh Ladji kopati Démal thia keur bay nga gnani Ladioul alal di Dink ma sarakh bi ma seuysi (Bis1) Ladji kopati, Sa sarakh bi momay danel tikko fi Ma diap chill eh ehhh Amsa thiopati Say say bi momay danel tikko fi Ma diap chill eh ehhh (Bis1) Contacts: Email: ridiana75@ Tel manager: 221 771 273 475
Hide player controls
Hide resume playing