Myvideo

Guest

Login

Wally B. Seck - Confuse feat. Mia Guisse & Amadeus

Uploaded By: Myvideo
36 views
0
0 votes
0

Lyrics (Mia) Yaay booy wouyouma, damalay laadj (yeah) Baay booy yédd ma, damalay laadj (yeah) Beugouma loubakh reuthie ma, damalay laadj (yeah) Beugouma réthiou tam, damalay laadj Couplet 1 Khamna limouy laadj (Limouy laadj, limouy laadj) Niom niaar, kouné mounguék liniouy laadj (limouy laadjté waw) Damay beuga diakhlé, ndakh awma choix ci niaar niou doywaar (Wally) Beugg nga mais ya ngui xel niaar Beugo kou xar sa xol bi niaar baby Xeyna gnifi diota diaar nio fowé sa xol banga fokni nieupa soxor (Amadeus) God loumou bind dathié deff niarr, Ta yaw yaay sama guénwaleu man Assaman si nimou yaato, naadj bi limouy tang, yaay képar guiy neubb naadj bé Refrain: (Mia) Damay beuga diakhlé Awma choix bébé khamna limouy laadjté (Amadeus) Linguère nga boul diakhlé Mbékté dounya yi rek laala yéné (Mia) Hey, Damay beuga diakhlé Awma choix bébé khamna limouy laadjté (Amadeus) Yow Linguère nga boul diakhlé Mbékté dounya yi rek laala yéné Couplet 2: (Amadeus) Souma guissé nganane da ngama nop Té ndeye dji seikh dou ame ci diamalé Melni assaman ci nimou yaato Ak bidéw yi niniou taaro (Mia et Wally) Nékh nama, wayé diakhlé Ndakh khamouma, kimay taneu (Wally) Linguère may Latyr Diop Déguéne Mbaye (Anh) Ballago Khaliloulay (Wouy) Ndiabote gueu lay woutal yaay Té keur ga yafa doy lingère way (Ayaa) Maadi bour guéweul, khouss ndama lay béguel So beugué malay wayal, thiol, ndér ak tama way Linguère kay, so banié ma wett kaay, Kaay, yaay sama wérouway Refrain (Mia) Damay beuga diakhlé Awma choix bébé khamna limouy laadjté (Amadeus) Linguère nga boul diakhlé Mbékté dounya yi rek laala yéné (Mia) Hey, Damay beuga diakhlé Awma choix bébé khamna limouy laadjté (Wally) Linguère nga boul diakhlé Mbékté dounya yi rek laala yéné Outro (Wally) Nékh nama, wayé diakhlé Ndakh khamouma, kimay taneu No-no-no mon bébé Ne t’en vas pas wawaw Nékh nama, wayé diakhlé Ndakh khamouma, kimay taneu

Share with your friends

Link:

Embed:

Video Size:

Custom size:

x

Add to Playlist:

Favorites
My Playlist
Watch Later