Myvideo

Guest

Login

El Hadj NDiaye - Xel

Uploaded By: Myvideo
1 view
0
0 votes
0

► Get the album / écoutez l’album : “Xel“ (2001) : Grand Prix de l’Académie Charles Cros et Choc du Monde de la Musique. Xel Xalat ne lu xoll yëgul Yëngu yëngu danel ne guy wele Sëlëx sul ne kan wele Degg lu degg lu war la cë (ter) La raison a surpris le cœur Un tremblement a déraciné ce baobab Et cicatrisé la terre Ecoutez ! Il ne suffit pas d’entendre pour comprendre (ter) Genn xalat nax ne aduna Am sa lal lu bax le ci Nax sa dolle tëcu ngi ci Yagg dindi na tuma yëlle yëlle yëlle (bis) La pensée unique trompe le monde Il est bon de causer à son oreiller Surestimer sa force peut vous jouer un tour Le temps révèle les vérités (bis) Aduna aduna Ama aduna li du neegu nara La vie, la vie Ama, ne vaut pas la peine de se faire du mal Xin lax na jant bi, xam sa waru gar jëf jël ngi ci Yem fu mu leere lu bax le ci Jamono ngi ni jamono jamono nge jamono ngi ni… Le ciel s’assombrit voici le moment de se décider Aller au-delà de la nuit C’est aussi ça la vie, l’air du temps Pecum liir su neexe ndeey jë teew ne Teyye ne mbagg ye La danse du bébé est belle Quand se mère le tient par les épaules Xarum waay Gainde waay eï… Mouton pour les uns Lion pour les autres eï… Luy tëpp dal ci taal dessene ap jeggo Wolof Nnjaay ne në me lile woor na, lile woor na Lile leer na ma Sauter sur le feu contraint à ressauter Un sage wolof me l’a dit C’est clair Assaman yaa ne bëtt du ci buxante Yallah maay bëtt jam Te bëtt Fu ko neex lay xool Le ciel est vaste, tous les regards y ont leur place Dieu a doté ses créatures D’yeux Et les yeux regardent où ça leur chante Xarum waay Gainde waay eï… Mouton pour les uns Lion pour les autres eï… Xin lax ne jant bi ey waay nu dem Xin lax ne jant bi ey waay nu wey Xin lax ne jant bi ey waay nu dem (ter) Un nuage noir a caché la lumière, allons y Un nuage noir a caché la lumière, allons y Un nuage noir a caché la lumière, allons y (ter) Xin lax ne jant bi demal demal demal Xin lax ne jant bi ku demul ma dem Xin lax ne jant bi ey waay nu dem (bis) Un nuage noir a caché la lumière, allons y si vous n’y allez pas, moi j’y vais Un nuage noir a caché la lumière, allons y Un nuage noir a caché la lumière, allons y Ah ! Ah ! …Xel lu bax la ci, aduna, suma xel, suma xol, sumaï xalaat Ah ! Ah ! …Il est bon de réfléchir, c’est la vie, la raison, le cœur, les pensées

Share with your friends

Link:

Embed:

Video Size:

Custom size:

x

Add to Playlist:

Favorites
My Playlist
Watch Later