Myvideo

Guest

Login

LASS - Mo Yaro (clip officiel)

Uploaded By: Myvideo
1 view
0
0 votes
0

📣 Album “Bumayé“ (vinyle, CD, digital) ➡ IG 👉 FB 👉 TikTok 👉 ----------- Music Video: Direction / animation / editing & color grading: Peter the Moon & Ugo Vittu Dancers : Celia Derrahi Caroline Besson Kaiba Bling ----------- Music : Songwriter & performer : LASS Composer : Paul Cucuron Additional arrangements : Alex Chiere Direction & mix : Raphaël D'Hervez (P) & (C) Chapter Two Records / Wagram 2021 ----------- 🎤 LYRICS IN WOLOF [VERSE ] Doyegama si kersé Wonégako mome Xalé bou yarou Mané yama mome Ya ligueye lou méleni Amoulo morome A dieufe diou bahe die Mani yaye borome [CHORUS x 2 ] Fougnoula toudé Mané mo yaro Sa ligueye la A xalé bilé mané Mané mo yaro Sa ligueye la [ VERSE ] Weurnala si kogne bi Kéneu méni yaw Sa youmala séné Xole bi dale si yaw Ha mané yalla samala Hé mané yalla samala Doyegama si kersé Wonégako mome Xalé bou yarou Mané yama mome Ya ligueye lou méleni Amoulo morome A dieufe diou bahe die Mani yaye borome [ CHORUS x 4 ] [ BRIDGE ] Mo yaro Ki moka yaro Mo yaro [ CHORUS x 4 ]

Share with your friends

Link:

Embed:

Video Size:

Custom size:

x

Add to Playlist:

Favorites
My Playlist
Watch Later